démonna bay nékh wayé boumgua
dokna mome
hé baykat bi khalam démonna
bay nékh wayé boumgua dokna mome
boula nékhé talalal say lokho
yaye docteur biy fath khifou askane bi
liko dalé si nditoum rew bassi miskine
ya souméko di dane sa dolé andak nath
bi di liguey sa gnakha di tourou
ngay bay di doukat bilay ya am diome
kon diarama baykat koufi xiff yako
doundal bamou sour
waw koufi fébar yako nandal aki réén
bamou féékh
kon diarama baykat koufi xiff yako
doundal bamou sour
waw koufi fébar yako nandal aki réén
bamou féékh
ya momone sa mbay
ya mome sa guanthiakh mome say
ndiour ya mome sa alla di bay
nguour gneuw dougalthia lokhome ak
boor fékeleuthaa guanthiakh ba
mégneu lole ndékétéyo
kon diarama baykat koufi xiff yako
doundal bamou sour
waw koufi fébar yako nandal aki réén
bamou féékh


